Xalaat Tv n’a pas manqué de commenter le geste des deux danseurs de Wally Seck qui crée la polémique sur la toile.
« 2019 : Nga Sol Tee-shirt LGBT 🏳️🌈 Mbotaayu Goorjigeen Yëpp Dila Deloo Njukël. Batay Setaloo Sa Dér Té Moonté Amoon Nga Occasion Ci Rassemblement « And Samm Jikko Yii »
2020 : Coronavirus Ñëw, Concert Amul, Mbumbaay Amul…Ngeen Waroon Ci Jàngg Deelu Seen Borom, Tuub Ndax Yërmandé Yàlla Dafa Yaatu
2021 : Ngeeni Foonënté En Direct Ngir Dëgël Seen Taxawaay Ci Doleel Mbon
Kuleen Ko Wax Ak Kuleen Ko Waxul Ay Ambassadeurs Goorjigeen Yi Ngeen Biir Sénégal.
Mboleem Artistes Yici Sénégal Yaay Kénn Kuñuy Deendalé Turëm Ay Borom Ñaari Tur Yi. Yaa Ñakk Jom ! »
→ A LIRE AUSSI : Ndella Madior Diouf se retire de l’émission « Kakatar »: « Je suis obliger d’arrêter pour préparer les élections locales » (Vidéo)
→ A LIRE AUSSI : Noyade à Malika : Le bilan passe à 10 morts (Audio)
→ A LIRE AUSSI : Thiant de Paris : Les pas de danse de Sokhna Aida Diallo devant ses talibés (Vidéo)
'